Les restes des fils d’adam/ndesiti doomi aadama
PRÉSENTATION DE L’OUVRAGE
L’Agence intergouvernementale de la Francophonie vient de confier au Centre International de Phonétique Appliquée (CIPA), l’édition d’une nouvelle collection : » Diversité linguistique et société « . Cette collection est consacrée à l’un des enjeux majeurs du 3° millénaire : la diversité linguistique, elle-même partie intégrante de la diversité culturelle. Les deuxpremiers volumes viennent de paraître : – Isidore NDAYWEL ; Louis-Jean ROUSSEAU ( dir.).- Demain le français : vers des stratégies diversifiées de promotion et d’enseignement.- Paris : AIF ; Mons : CIPA, 2004.- 267 p.
Image:(c) »La Vie »,Une création de Daour Wade
NDESITI DOOMI AADAMA
Ndesiti doomi Aadama, téeré la buy wax lu soxal doomi Aadama yi,
bu jële ci Doomu Aadama, jëme ci Doomi Aadamayi.
Les Restes des Fils d’Adam est un ouvrage qui parle des Fils et filles d’Adam, écrit par un des Fils d’Adam pour tous les Fils d’Adam.
Nu ngi dund ci jamono ju jax, ju tumurànké, jàppalante ak dimbalante, yërmaande ak jàmm, yar ak teggin, kollare ak muñalante ak doxalin yuy sàmmu àqi doomi Aadama .
Nous vivons une époque trouble, pauvre des qualités de l’entraide et de l’assistance, depitié, de paix, de politesse et de savoir être, de
reconnaissance et de tolérance, de respect des droits de la personne humaine.
Nettali yi nekk ci téére bii, boroom tëgge lee-leeg aki nit, ay rab, wallay mala, sërxël ci biir yenn taalif yu gàtt, ci baax yooyii lay wax ngir Doomi Aadama yi man a dawal séen xel fu sori, indi ko ci tey, seet li nu dese ci jikko yiy jariñ xeetu Doomi Aadama witey ci nekkin wu rafet aki dëkkandoom ak ku mu man di doon (nit, rab, mala, garab, gàncax, a.n.s.) Su xalaat yooyu amee, ñu sukkandiku ci desit yooyule, suuxat léen, sàmm léen ba jàmm sax fépp ci kow suuf ci biir déggoo, jàppoo, dimbalante ci biir yërmànde gu lalu ci kow wegante ci diggante ñi am doole ak ñi néew doole, ñi yor ak ñi ñàkk ndax àqi bépp Doomi Aadama sàmmu ba mu sàmmaale yu ñeneen ñimu dëkkël.
Les histoires contenues dans cet ouvrages, forgées avec des personnages humains, animaux, sauvages ou domestiques, parsemées de courts poèmes, parlent de ces valeurs là. Il veut pousser les Fils et les Filles d’Adam à la réfléxion aussi loin que possible dans leurs tréfonds pour chercher dans les bribes de valeurs qui leur restent celles qui peuvent servir la race humaine aujourd’huià mieux vivre en communauté (entre les humains mais aussi avec les autres êtres vivants, les animaux,
la nature…) Une fois ces restes de valeurs identifiées, il faut les entretenir, les préserver pour que la Paix prenne racines sur Terre, que l’entente et l’entraide, fleurissent dans le lit d’une compassion empreinte de respect réciproque entre les plus forts et les plus faibles, les riches etles pauvres afin que les droits et devoirs de tout Fils et de toute Fille d’Adam soient entièrement respectés.
L’auteur Maam Daour Wade est un conteur, écrivain, scénariste et réalisateur de films. Il a été formé au cinéma à Paris (France) au Conservatoire Libre du Cinéma français et à l’Université de Bloomington Indiana (Usa), membre de l’Association des Ecrivains du Sénégal (AES) et membrefondateur de l’Association des Cinéastes Associés (CINESEAS) et de l’Association des Conteurs du Sénégal »Contes au Clair de Lune ». Il est également membre fondateur de l’Association Africaines éditrice de GUNE YI (Premier journal pour enfants Bilingue : Français/Wolof)
Maam Daawur bindkat la, léebkat la, fentkat la ci wàllu nettali te liggéykatu film la. Mu ngi jànge Faraans ca Pari ci Kuréel gutudd « Konserwaatuwaar Liibar dii sinemaa Faraanse » akit ca « Iniwersitee bu Injaana »Bulumington ca Amirik. Bokk na ci mbooloom bindkati Senegaal (AES) akit ci ñi sos mbooloom ñiy defar film ci Senegaal (CINESEAS) akit ci mbooloom Léeboon Ci Leer (Léebkati Senegaal) Bokk na ci yit ñi sos kuréel gu tudd (Anfaans afrikeen) di kuréel gi fi jëkk a génne këyitu xiibaar wu ñu jagleel xale yi « GUNE…